Ibrahima G🇸🇳 retweeted
Mon combat c’est qu’aucun de mes futurs enfants ne se sente redevable envers moi pour ce que j’aurai à faire pour eux. J’espère qu’ils ne verront jamais une détresse dans mon visage baniouy diap ni ils doivent sacrifier leur avenir pour me soulager. Je leur donnerai tellement d’amour que quand il sera dehors ils vont le propager ci wakhine ak djeufine Naniou dounde magg djangue djamou Yalla ndakh moy deugg
Je n’ai jamais eu un tel niveau en wolof
Replying to @NYCMayor
ICE du noppalu ci tas njaboot yi ci dëkku New York. Du nu noppalu ci xeex ak ñoom.
Woteel ci Buum u Jokkoo u Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem ci 1-800-354-0365, walla nga woo 311 te wax ne “Immigration Legal” (Taxawu ci Yoon ci wàllu Doxandeem), ngir am ndimbal bu laajul fay, bés bu nekk, am na sutura.
Sunu dëkk waa New York lay jàppale.
221

🚨 José MOURINHO 🇵🇹 : « Ce que j’ai dit à la mi-temps ?
Les vestiaires sont comme Las Vegas, ce qui se passe à Vegas reste à Vegas. » 😁🇺🇸
🎥 @MPlusDeportes