🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003) header
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003) profile picture

Aspirante infirmière 🩺 | Amoureuse du khassida Mouqadamatoul Amdah, un éloge qui élève l’âme et apaise le cœur | ﷺ Allahumma salli ‘ala Sayyidina Muhammad📿❤️

Joined January 2023
Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)Photo by 🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 (@adjikhady003)
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Salatug ubbe ku bu am solo welellee. Allahuma ya wahabu salli hala sëyyidina Muhammadine fâtihil abwabi wa alihi wa sahbihi wa sallim🤍🥹
1
19
124
1,509
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Àdduna ben banex mofi am mouy Mouhamedﷺ❤️🥹
18
1
69
1,228
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Ñaari bayit yi dina mussle si thiat ak njabar dina dakh rap jine diou saï saï deko werde ci ndox 333 fois diko naan✔️ #TaawOu
6
34
178
2,248
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
🚨🚨🚨🚨 URGENT MÀGGAL 24H NUURUD DAARAYNI MONDIALE
1
2
31
Tukki : Altine ✓ Tàmbali : Talaata ✓ Daloo : Àllarba ✓ Fóot : Alxamis ✓ Ñaan Yàlla : Àjjuma ✓ Watu : Gàwwu ✓ Sanc : Dibéer Une parole attribuée à Sëriñ Tuubaa et rapportée à Sëriñ Mañaaw Silla. Vu quelque part et trouvé intéressant à partager🤝🤍
3
42
1
191
3,501
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Sñ bi mooy sunu fierté wallahi. Yal nako fi Yàlla yàggal lool te mu ànde ak werr🤍
3
57
3
344
3,531
lol🥰
📚Jawabu Soxna Penda Joop, amna solo pour sama mbok soxna yii ☺️ @adjikhady003 @Dideva3D
1
1
6
223
Cc…On peut être élégante sans forcément en faire trop🤍Le bas large confort et l’élégance au quotidien. RT lennn🙏
7
18
573
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Jëllee lee na liggéey ko waye diko nane cafe rek tëju mom danga koy degg rekk cëyyyy bu ngeen moson fajar bu ne 555 xalaas lisi ëpp solo nak dalay ubbi ci jàamu yalla te ubbe ku DEUG mooy sawar ci jàmmu yalla🤍✔️ #TaawOu
1
28
1
190
2,541
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Kep ku nek ci xat xat mo xam weradi yaram wala jafe jafe alal ak lum mana don boko defe yalla wuyu la Guddi bala nga tëdd nga nafila lo man bax na Après nga jublu penku zikar ko 313 fois nga sujood ñaan sa soxla. Yonent bi psl waxon na ken du ci ñan ludul yàlla nàngu na ñaan gi.
18
114
1,475
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Rire avec ta maman est l'un des meilleurs moments de la vie.
45
3,649
107
26,600
451,171
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Teginu tuddu yalla/ zikr Masaalik
3
78
1
319
6,662
1kg de dibi a 9000fcf 🧎‍♀️🥺 Amoul bneu problème tabaski mingui fi ak magal touba …à 2027 inchalla🏃🏼‍♀️😎
1
13
428
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
MÉLOKAANU JOULITE SI LIGUÉY Liguéy dina taax sa gëum yalla yokou Liguéy dina taax sa jaamu yalla yokku Liguéy dina taax nga Saamu ngor Liguéy dina taax nga Saamu sa bop Liguéy dina taax nga soutural sa bop Liguéy dina taax nga mëuna dimbali niit
1
5
106
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Rùmnaa , 95 🙏🏾🤍
10
62
876
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweeted
Guddi Al Jumuah ✨ Multiplions les prières sur notre bien-aimé Prophète Muhammad ﷺ
70
1
250
3,549