Pinned Tweet
Maximum de Rt🚨
C'est la mère de mon meilleur ami
Kon sama yaay la, ni doomam lama defoon
2009 batay dji may bindi tweet guii, degg ñu ko, guissu ñu ko
Xamu ñu ndax migui dundu wala...
Waaye daal nigui rafeet njort
Ci ndigalu doomam laa def Tweet gui
Di ci sàkku ñaan ❗
Jarga ! retweeted
J’ai un gros problème avec les médecins ici au Sénégal. Ils ne te donnent le diagnostic que quand tu le leur demandes. C’est à dire tu viens expliquer ton problème, ils écoutent, font ce qu’ils font et puis basta bindeul leu ordonnance mou diekh
Dëgg gu wer !!
Ay nit yu génn ci diine loolu doyul ñuy saaga diine ji ak Yonent bi shw, ngeen ne nañu maandu ndax àdduna daa gudd tànk.
Ki génn ci diine ji bëtub yéefar ak noon rekk lañu koy xoole, bu dellusee nag nu defaat ko ne sunu bopp muy mbokkum jullit.
Ab jullit day am fulla ci diineem, yaw ku la xas nga summiku xeex, ñuy xas sa diine nga ne dangay maandu doo wax.
2
264

Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la.
Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
Jarga ! retweeted
Nous vous donnons rendez-vous pour notre prochain webinaire.
📍 Thème: Cancer de la prostate,dépistage,Stratégie diagnostic et PEC thérapeutique
👉🏻Sous thème 1: Place de l’imagerie dans le diagnostic et le bilan d’extension du cancer de la prostate 👇
Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la.
Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
Jarga ! retweeted
Baay-Faal moo fi jiitu sa baay jiitu say maam ak seeni maam dangay juddu fekk fi Baay-Faal dangay dead leggi du yagg bayyi fi Baay-Faal – at Senegal
Jarga ! retweeted
Teggiin ci sa kanamu Kilifa da ñu ko wara jaggi ji wat ñun ñépp. Rawati ci kanamu Sëriñ Tuubaa Seex Muhammadul Muntaxaa ko. Am na lol dess wara yërëm ka ko wax mba mu def ko. Feeñal geen mën ci kanamu Sëriñ Bi ëpp na dayo lool. Ñi ko doonoon dëgg te mën ko da ñu daa def dégg,
Nun bëgg nan Sëñ Tuuba waaye toppu nu ko !
Ndax bunu ko toppoon , kon reewmi, société bi du melnii ci yakkute .
« Ku woppu ken seet si wula ; Ku xewle ken ñëwul ; Ku dee le ken jaale wula .
Magg ñi neenañ du dogalu yalla, jikko la !»
Baay Ndiaga Job
Jarga ! retweeted
Tu te plains de la vie , ba Yallah xëy Yonner la beugne bouy meti , wala lokho wala ndigue bouy meti , ci ngey kham ni adouna khaliss kesser , kheweul yi niouy dokhaler ci sunu dieum chaque jour beuri na t bayi wu niouko khel 😔