Jarga ! (@RIENqueLUI) header
Jarga ! (@RIENqueLUI) profile picture

MA'AM SEEX IBRAHIMA FALL ñëriñ gudul jeex la, te ñëp xajj nan ci...

Joined May 2021
Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)Photo by Jarga ! (@RIENqueLUI)
J’ai un gros problème avec les médecins ici au Sénégal. Ils ne te donnent le diagnostic que quand tu le leur demandes. C’est à dire tu viens expliquer ton problème, ils écoutent, font ce qu’ils font et puis basta bindeul leu ordonnance mou diekh
7
66
15
288
12,391
Jarga ! retweeted
Ay nit yu génn ci diine loolu doyul ñuy saaga diine ji ak Yonent bi shw, ngeen ne nañu maandu ndax àdduna daa gudd tànk. Ki génn ci diine ji bëtub yéefar ak noon rekk lañu koy xoole, bu dellusee nag nu defaat ko ne sunu bopp muy mbokkum jullit. Ab jullit day am fulla ci diineem, yaw ku la xas nga summiku xeex, ñuy xas sa diine nga ne dangay maandu doo wax.
3
291
42
810
35,911
Jarga ! retweeted
Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la. Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
5
42
1
167
2,244
Tiggi !!!✊🏾
Particularité yoonu Murid, Maam Seex Ibrahima Fall la. Biss bunu baayee li Maam Seex Ibrahima Fall indi di ap taalibe, boobaa lañuy ndiroo ñëp, yem ak ñëp !
1
8
212
Nous vous donnons rendez-vous pour notre prochain webinaire. 📍 Thème: Cancer de la prostate,dépistage,Stratégie diagnostic et PEC thérapeutique 👉🏻Sous thème 1: Place de l’imagerie dans le diagnostic et le bilan d’extension du cancer de la prostate 👇
1
14
2
25
1,864
Baay-Faal moo fi jiitu sa baay jiitu say maam ak seeni maam dangay juddu fekk fi Baay-Faal dangay dead leggi du yagg bayyi fi Baay-Faal – at Senegal
Ken meunoul Open mind ba raw Baye Fall
2
2
7
2,241
Teggiin ci sa kanamu Kilifa da ñu ko wara jaggi ji wat ñun ñépp. Rawati ci kanamu Sëriñ Tuubaa Seex Muhammadul Muntaxaa ko. Am na lol dess wara yërëm ka ko wax mba mu def ko. Feeñal geen mën ci kanamu Sëriñ Bi ëpp na dayo lool. Ñi ko doonoon dëgg te mën ko da ñu daa def dégg,
1
6
38
849
Sunu waa kër😅❤️✊🏾
1
36
3
244
3,386
Jarga ! retweeted
Neegu yalla mooy lann ??
1
19
147
2,097
Jarga ! retweeted
« Li yalla tax , bu ci dugal ludul yalla »
1
29
151
2,265
Jarga ! retweeted
Tu te plains de la vie , ba Yallah xëy Yonner la beugne bouy meti , wala lokho wala ndigue bouy meti , ci ngey kham ni adouna khaliss kesser , kheweul yi niouy dokhaler ci sunu dieum chaque jour beuri na t bayi wu niouko khel 😔
18
1
64
1,404
Jarga ! retweeted
Xeetu Vérité yiii nga dul deg fenn !
90
571
6,587
Ces derniers jours on opère beaucoup de patients qui viennent avec perforation (trou) de leur intestin dû à la fièvre typhoïde Elle se transmet par l’eau et les aliments contaminés. Mooytouleene yenne lekk mbedd yii
7
214
12
562
32,831
Une dame à l'hopital Dalal Jamm doit se faire opérer d'un cancer du col de l'utérus, le kit opératoire devait lui etre offert mais ils ont atteint leur quota. Il n'est pas cher juste 20k et un surplus pour assurer les frais post opératoire Wave OM 768359223 Papa Mamadou Sakho
2
366
5
298
9,108
Comment démarrer un programme de transplantation rénale dans un CH National Universitaire ? @ISNkidneycare Sister Renal Center Program Level B @JammDalal 🇸🇳 & @ClinUnivStLuc 🇧🇪 🗣️ Yannick France & El Hadji Fary Ka 🗓️ Jeudi 05/11/2025 🕒 15h00 Dakar - 16h00 Bruxelles 🔗 Lien 👇
1
3
12
316
Ku wàcci li fi Seex Ibra Faal ëndi tuddu neneen nudul murid waxu mala doon ko📌
5
22
418
Jarga ! retweeted
Bëgg naa lool njep teewlu wideo wii
32
1
190
2,698
🚨Kërug Alxuraan Gi (Kënzil Kitaabu) Fass na ñu yeene andag kepp ku ñu bokal pass-pass girr yobbaaleel ko jëfam ci leggeyu Kënzil Kitaab Kërug Al Quran gi Seex Muhammadul Muntaxaa di liggeey lo jabootu Seex Ibra Faal gi Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
🚨KËRUG ALXURAAN GI Jëfi Murids yi fi jotoona dajjee ajju ci jaayante Kënzil Kitaab gi Seex Muhammadul Muntaxaa di jabootu Seex Ibraayma Faal gi, jebbaleel na ñu leen ko démb ci talaata ji (mardi) NB: jaayante bagi wëy Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye
11
2
22
658
"Sëriñ bee sunu bank, ag bank ku cay dem bu sañoon takanderam sax duko topp"
Bëgg naa lool njep teewlu wideo wii
1
15
252
Replying to @RIENqueLUI
Diangg mii dh warna bepp mouride (mag nia amneu fougn nekkoon dh). Nanu dieem rek malheureusement avec le monde connecté (téléphone yeek vidéo yi, faw nga moytu tentations yi). Yomboul nak
1
1
42