
Sant Borom Tuuba 🇸🇳❣️✨🕊️. xassidalover❤️ #sopeSerigneSamMbaye.
Senegal
Joined October 2022
- Tweets6K
- Following710
- Followers519
- Likes75.5K
Li yëp dundu nagn ko Galsen bis bu rafet rek lagniy xaar!
Pourquoi venir étudier au Canada 🇨🇦??
1-Apprendre à devenir indépendant et ne plus!compter sur ses parents.
2-Apprendre à vivre avec la solitude, le stress, l’angoisse et les difficultés. Ça forge le caractère.
3-Découvrir d’autres cultures, d’autres mentalités et une nouvelle façon de voir la vie.
4-Devenir plus humble et apprendre à relativiser.
5-Comprendre que personne ne se soucie vraiment de ce que tu possèdes ou de ce que tu n’as pas.
61
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
« L’islam a commencé étranger et redeviendra étranger »
l’islam était au début peu suivi et semblait étranger aux gens, puis qu’une époque viendrait où ceux qui restent attachés à sa pratique pourraient de nouveau se sentir isolés. « Heureux les étrangers. »
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Ñakk gëm yalla wala weddi ko loolu warul nekk jafe jafe ci ab jullit, ndax al xuraan xamal nanu
1- forcer nit pour mu duggu ci islaam amul ci diine ji (S2, V256)
2- xamal nanu ku nekk amna liberté gëm wala weddi (S18, V29) choix boo def amna responsabilité,
3- xamal nanu yalla mooy gendi jubal ku ko neex (S28, V56)
4- xamal nanu danoo wara nekk nu bienfaisants et équitables ci ñi nekkul ay jullit ta seq ag nun jàmm (S60, V8)
Waaye benn jullit bu am fayda warul nangu kenn kuy saaga diine ji wala diko baña respect.
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Tukki : Altine
✓ Tàmbali : Talaata
✓ Daloo : Àllarba
✓ Fóot : Alxamis
✓ Ñaan Yàlla : Àjjuma
✓ Watu : Gàwwu
✓ Sanc : Dibéer
Une parole attribuée à Sëriñ Tuubaa et rapportée à Sëriñ Mañaaw Silla.
Vu quelque part et trouvé intéressant à partager🤝🤍
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Déclaration de Serigne Mountakha Bachir Khalif général des mourides | SEPCAB Paris 2027
Lien
youtube.com/live/kR9yhz5vCQs…
#tdisenegal #tdidiaspora #CheikhAhmadouBamba #KhadimouRassoul #Patrimoine #Mouridisme
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Sñ bi mooy sunu fierté wallahi.
Yal nako fi Yàlla yàggal lool te mu ànde ak werr🤍
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
(Et ne tuez pas vos enfants par crainte de pauvreté ! C’est Nous qui attribuons leur subsistance tout comme à vous .)
Sourate Al-Isra (Le Voyage nocturne), verset 31 (17:31) du Coran.
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Lumu jaral niit nguir mu yaak lislam naleen ko jaral ngeen taxaw nguir seen diine.
Ndax seeni manipulation ak seeni tweet meun na jax jaxal xellu ku amul yobal bu doy Iman ak Islam.
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
« O les croyants! Quiconque parmi vous apostasie de sa religion... Allah va faire venir un peuple qu'Il aime et qui L'aime, modeste envers les croyants et fier et puissant envers les mécréants, qui lutte dans le sentier d'Allah, ne craignant le blâme d'aucun blâmeur. Telle est la grâce d'Allah. Il la donne à qui Il veut. Allah est Immense et Omniscient. »
S5,V54.
Sëriñ🇸🇳❣️ retweeted
Maangi doon wax ci gëm yalla ag am ay preuves nimu ame solo… amna sax boroom xam-xam yu japp ni ki gëm sans preuve kooku gëmul wala gëm gi matul… amñu japp ni ki yalla jox xel mu normal buko utiliser wul pour am ay preuves loolu moy yalla la… (jawharu tawhiid)
Preuves yi amna yoo xamni xel kese lañu mëna jëfëndikoo gir saxal ko lu melnii amuk yalla gi. Am yoo xamni xel ag texte, am yoo xamni degg rek lañu ci mëna am muy samhiyyaat yi muy mbiri ghayb yi….
Livres théologies yi yaatal nan ci lu melni Jawharu tawhiid, al mawaaqif… wala sharh sanuusi ci ummul barahin.
Yonent yi seeni muhjiza mooy seeni preuves, Yonent bi muhjiza bi gëna rëy mooy al xuraan, abu bakkar bi muy gëm al xuraan tambali na wacc, ta limu xam ci Yonent bi ci ay jikko doyna ko preuve ni lumu wax dëgg la.




















